2 Timothy 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na ko Boroom bi teeru ak yërmandeem ca bés ba. Umplewoo it coono yi mu daj, ngir dimbali ma ca dëkku Efes.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yal na ko Boroom bi may mu daj bésub keroog booba, yërmandey Boroom bi. Taxawu na ma lool ca Efes, te xam nga ko xéll.