2 Timothy 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bul rus ci seedeel sunu Boroom, mbaa ci li ñu ma tëj ndax turam, waaye bokkal ak man tiis ci xamle xebaar bu baax bi, wéeru ci kàttanu Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bul kersawoo di seedeel sunu Sang, mbaa nga di ma kersawoo, man mi ñu tëj ngir moom, waaye jëlal sa wàll ci coonob xibaaru jàmm bi, ni la ko manoorey Yàlla manloo.