2 Timothy 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te lii tax may muñ lépp, ngir ñi Yàlla tànn it am mucc gi ci Kirist Yeesu, gu ànd ak ndam lu sax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Looloo ma tax di muñ lépp, ngir ñi ñu taamu, ndax ñoom it ñu dajeek mucc gi ci Almasi Yeesu, boole ci teraanga ju sax.