2 Timothy 2:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su nu ko weddee,kon mu weddi nu;su nu ko ñàkkee kóllëre,moom dina sax ci kóllëreem,ndax mënul a weddi boppam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su nu ko gàntalee, moom it dinanu gàntal; su nu ko ñàkkee kóllëre, mu saxoo kóllëreem, ndax manula gàntal boppam.