2 Timothy 2:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moytul bépp jataayu waxi neen yu àddina kese, ndax ña fa toog dinañu gën a xuus cig weddi,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ay kebetuy àddinay kese, moytu ko, ndax ngëmadi gu ko yées rekk lay yóbbee,