2 Timothy 2:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye teewul fondamaa bu dëgër, bi Yàlla tabax, nee na kekk, te lii lañu ci tàmpe: «Boroom bi xam na ñi bokk ci moom,» te it: «Ki tudd turu Boroom bi, na daw lu bon.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul cëslaay lu dëgër, li Yàlla tabax, mu ngi ne kekk, te màndarga ma ca nekk, kàddu yii la: «Boroom bi xam na ay ñoñam,» ak: «Kuy tudd turu Sang bi, na daw njubadi.»