2 Timothy 2:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te jaamu Boroom bi warul a xuloo, waaye na lewet ci ñépp, jekk ngir jàngale tey muñ fitnay noon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te jaamub Boroom bi warul di ŋaayoo, waaye day lewet ci ñépp, mana jàngle tey muñ.