2 Timothy 2:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it ku tàggat yaramam ngir rawante, duñu ko jagleel kaalag ndam mukk, su toppul sàrt ya.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kuy joŋante it, deesu ko kaala te joŋantewul ci yoon.