2 Timothy 2:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xalaatal bu baax sama wax jii, ndax Boroom bi dina leeral sa xel ci lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Defal sam xel ci li ma la wax. Boroom bi moo lay leeralal lépp.