2 Timothy 3:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nanga xam lii: bési tiis yu tar ñu ngi nuy tëru ci muju jamono.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii, nanga ko xam: mujug jamono, jant yu tar dina dikk.
Recommended Reading