2 Timothy 3:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xam nga li ma daj ciy fitna ak i coono ci dëkki Ancos, Ikoñum ak Listar. Céy li ma jànkoonteel ciy fitna! Waaye Boroom bi musal na ma ci lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak itam bundxatal yaak njàqare ya ma dikke woon fa dëkk yooyu di Àncos ak Ikoñum ak Listar. Céy na ñu ma bundxatale, waaye Sang bee ma musal ci lépp!