2 Timothy 3:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te ku bokk ci Kirist Yeesu, te bëgg dund dund gu ànd ak ragal Yàlla, alamikk ñu fitnaal la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te kat képp ku namma nekke ag njullite ci yoonu Almasi Yeesu, dees na la bundxatal.
Recommended Reading