2 Timothy 3:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Duñu noppee gëstu, waaye duñu man a yegg ci xam-xamu dëgg mukk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gëstu ay àlluwa la jigéen ñooñuy wéye, waaye duñu mana xam liy dëgg mukk.