2 Timothy 3:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye duñu dem fu sore, ndax seen ñàkk xel dina bir ñépp, ni mu dale woon Sànnes ak Sàmbares.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye duñu soreeti, ndax seenug ndof dina bir ñépp, na ñaar ñooña mujje woon.
Recommended Reading