2 Timothy 4:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Erast des na dëkku Korent. Torofim dafa woppoon, ma bàyyi ko dëkku Mile.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Eràst moom, Korent la des, waaye Torofim, Mile laa ko bàyyi, ndax daa woppoon.
Recommended Reading