2 Timothy 4:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gaawal a ñëw, bala lolli di gàllankoor sa yoon. Ëbulus, Pudeñsë, Linus, Këlójaa ak yeneen bokk yépp ñu ngi lay nuyu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gaawala ñëw, balaa seddub lolli di jam. Ab nuyoo ñeel na la, tukkee ci Ëbulus ak Pudeñsë ak Linus ak Këlójaa ak bokk yépp.