2 Timothy 4:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte jamono dina ñëw, joo xam ne nit ñi dootuñu xajoo njàngale mu wér mi, waaye dinañu jublu ci seeni bëgg-bëgg, di fortaatu jàngalekat yu leen di jey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat ay jamonoo ngi ñëw, nit ñi dootuñu xajoo àlluwa ju wér, waaye seeni bëgg-bëggi bopp lañuy topp, bay fortaatoo fu nekk, ay sëriñ yu leen di wax lu leen neex.