2 Timothy 4:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yaw nanga foog ci lépp, dékku tiis, tey tas xebaar bu baax bi, ba matal sag yónnent.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye yaw, àndal ak sa sago, ak diggante boo mana tollu, te ñeme coono. Jàppal ci liggéeyub jottli xibaaru jàmm bi, beyal sa waar ba mu mat sëkk.