3 John 1:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka Démétrius nag, ñépp seedeel nañu ko lu baax, te dëgg gi sax seedeel na ko ko. Nun itam seedeel nanu ko te wóor na ma ne, sunu seede dëgg la.