Acts 1:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Piyeer teg ca ne: «Ndaxte lii lañu bind ci téereb Sabóor:“Na këram gental,bu fa kenn dëkk.” Te it:“Na keneen bey sasam.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ndax bindees na ci téereb Sabóor ne: “Yal na këram gental, yàlla bu fa kenn dëkkeeti, yal na keneen jagoo sasam.”