Acts 1:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon ñeel na nu, nu tànn kenn ci ñi bokk ak nun, diir bi Yeesu doon dem ak a dikk ci sunu biir,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am na nag ay nit ñu àndoon ak nun mboolem diir bi Sang Yeesu dee dem ak a dikk ci sunu biir,