Acts 1:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko Piyeer waxee, ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas te di ko dàkkentale Yustus, moom ak Macas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas, te ñu di ko wax Yustus itam, ak Maccas.