Acts 1:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu ñaan ci Yàlla ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu nit ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu daldi ñaan ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,