Acts 1:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Yaxya daa na sóob nit ñi ci ndox, waaye yéen dees na leen sóob ci Xel mu Sell mi fi ak ay fan yu néew.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax cim ndox la Yaxya daan sóobe, waaye yeen ci Noo gu Sell gi lees leen di sóob fii ak fan yu néew.»