Acts 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu dajaloo ak moom nag, ñu laaj ko: «Boroom bi, ndax ci jamono jii ngay yékkatiwaat nguuru Israyil?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañu daje fa moom, daldi koy laaj, ne ko: «Sang bi, ndax ci jii jamono ngay sampaat nguurug Israyil?»