Acts 10:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye baat bi wax ak moom ñaareelu yoon ne ko: «Lu Yàlla sellal, bu ko araamal.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul baat bi wax ak moom ñaareel bi yoon, ne ko: «Lu Yàlla setal, bu ko daganadil.»