Acts 10:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu woote nag naan: «Simoŋ, mi ñu dàkkentale Piyeer, ndax fi la dëkk?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu woote, laajte, ne: «Simoŋ, mi ñuy wax Piyeer, fii la dëkk?»
Recommended Reading