Acts 10:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu muy waxtaan ak moom, duggsi, fekk fa ndajem nit ñu bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer di waxtaan ak moom, ba duggsi, yem ca nit ñu bare ña fa daje.