Acts 10:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne leen: «Xam ngeen ne, aaye nañu Yawut, mu jaxasoo ak ku mu bokkalul xeet, mbaa mu dugg ci këram. Waaye Yàlla won na ma ne, warumaa ne kenn setul mbaa araam na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne leen: «Yeen de xam ngeen ne ab Yawut, mayeesu ko mu jaxasoo ak xeetu jaambur, mbaa mu seeti ko. Waaye man nag Yàllaa ma won ne du kenn nit ku ma naan daganula jaxasool, mbaa setul.