Acts 10:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am bés ci tisbaar nag mu am peeñu, gis bu leer malaakam Yàlla feeñu ko ne ko: «Korney!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am peeñu nag dikkal ko digg njolloor, mu gis ci lu leer malaakam Yàlla, mu duggsi, ne ko: «Korney!»