Acts 10:35 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
waaye ci xeet yépp, ku ko ragal tey def lu jub, moom la nangu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waaye xeetoo xeet, ku ko ci ragal tey def njekk, mooy ki ko neex.
Recommended Reading