Acts 10:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yónnee na kàddoom bànni Israyil, di leen xebaar jàmm, jaarale ko ci Yeesu Kirist, miy Boroom lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo yónnee kàddoom bànni Israyil, àgge leen xibaaru jàmm, biy maye jàmm ci Yeesu Almasi, miy Sangu ñépp.