Acts 10:39 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Seede nanu li mu def lépp ci biir réewu Yawut ya ak Yerusalem. Moona rey nañu ko ci wékk ko ci bant.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Nun ci sunu bopp noo seede li mu def lépp ci réewum Yawut yi ak Yerusalem. Moom mi ñu wékk ci bant, ba rey ko,