Acts 10:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte dégg nañu leen, ñuy wax yeneeni làkk ak di màggal Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax dañu leena dégg ñoom itam, ñuy làkk yeneen làkk, ak a màggal Yàlla.