Acts 10:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Booba Piyeer daldi wax ne: «Ñii jot Xel mu Sell mi ni nun, ndax manees na leen a bañ a sóob ci ndox?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer dellu ne: «Ñii jot Noo gu Sell gi ni nun, ndax manees na leena baña sóob ci ndox?»