Acts 10:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yónnil léegi nag ay nit ci dëkku Yope, ñu woo ku tudd Simoŋ, mi ñu dàkkentale Piyeer.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag yebleel ca Yope, nga wooluji fa ku ñuy wax Simoŋ, ñu di ko dàkkentale Piyeer.