Acts 10:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
mu nettali leen lépp, yebal leen Yope.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu nettali leen lépp nag, daldi leen yebal Yope.