Acts 10:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca ëllëg sa, ba ñuy jaar ca yoon wa, ba jub dëkk ba, Piyeer yéeg ca kaw taax ma ci digg-bëccëg ngir ñaan ci Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca ëllëg sa, ñu dem bay jub dëkk ba, yemook Piyeer yéeg ca kaw taax ma ci digg bëccëg, ngir ñaan.