bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 11:1
Acts 11:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi loolu amee ndaw yi ak bokk yi nekk ci diiwaanu Yude, dégg nañu ne, ñi dul Yawut nangu nañu kàddug Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ndaw yaak bokki gëmkat ña ca réewum Yawut, dégg ne jaambur ñi dul Yawut déggal nañu kàddug Yàlla, ñoom itam.