Acts 11:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu am ba muy ñetti yoon, ba noppi ñu ne cas lépp, jëme asamaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Menn peeñu moomu dikk na ba muy ñetti yoon, ñu doora yéege lépp asamaan.