Acts 11:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te Xel mi ne ma: “Àndal ak ñoom, te bu ci werante.” Juróom-benni bokk, yi fi teew, gunge woon nañu ma, ba nu dugg ca kër góor googu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noo gi nag ne ma: “Àndal ak ñoom, te bul nàttable.” Juróom benni bokk yii ngeen di gis ñoo ma gunge, nu dem ba dugg ca kër Korney.