Acts 11:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee ma fàttaliku li Boroom bi wax ne: “Yaxya ci ndox la daan sóobe, waaye yéen dees na leen sóob ci Xel mu Sell mi.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma daldi fàttliku kàddug Sang, ba mu noon: “ Yaxya, cim ndox la daan sóobe, waaye yeen, ci Noo gu Sell gi lees leen di sóob.”