Acts 11:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moona amoon na ci ñoom ay niti Sipar ak dëkku Siren, ñu ñëw ci Ancos, ba seen wax law ci Gereg yi it, ñu di leen xamal xebaar bu baax bu Yeesu Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Terewul ay gëmkat ñu dëkke Sippar ak Siren, bàyyikoo ca, dikk Àncos, wax ak làkk-kati Gereg yi, ñoom itam, ba àgge leen xibaaru jàmm bu Sang Yeesu.