Acts 11:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ma tontu ne: “Mukk Boroom bi, ndax dara lu daganul mbaa lu araam musul a dugg ci sama gémmiñ.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma ne: “Mukk, Sang bi, ndax lenn lu daganul mbaa lu setul masula dugg sama gémmiñ.”

Recommended Reading