Acts 11:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñaareel bi yoon baat bi dellu ne ma: “Lu Yàlla sellal, bu ko araamal.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Baat ba nag àddoo asamaan ñaareel bi yoon, ne ma: “Lu Yàlla setal, bu ko daganadil.”