bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 12:1
Acts 12:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ca jamono jooja Erodd buur ba jàppoon na ay nit ci mbooloom ñi gëm, ngir fitnaal leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca jamono jooju la Buur Erodd jàppoon ñenn ca mbooloom gëmkat ña, di leen mitital.