Acts 12:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu ne ko: «Xanaa dangaa dof.» Waaye mu dëgër ci li mu wax. Noonu ñu ne ko: «Xanaa malaakaam la.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko: «Xanaa dangaa dof?» Teewul mbindaan mi ne moom la. Ñu daldi ne: «Kon malaakaam la.»
Recommended Reading