Acts 12:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Erodd wutlu ko, waaye gisu ko. Kon mu àtte wottukat ya, joxe ndigalu rey leen. Bi loolu amee Erodd jóge ci diiwaanu Yude, dem dëkku Sesare, toog fa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Erodd nag santaane ñu wër Piyeer, te taxul mu gis ko. Mu daldi àtte wattukat yi, ba noppi joxe ndigal ngir ñu rey leen. Ba mu ko defee Erodd jóge diiwaanu Yude, dem Sesare, toog fa.