Acts 12:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu gisee nag ne, mbir moomu neex na Yawut ya, mu daldi jàpp it Piyeer; fekk loolu daje ak bési màggalu Yawut, ga ñuy wax Mburu ya amul lawiir.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu gis nag na mbir ma neexe Yawut ya, ba tax mu teg loxo Piyeer, moom itam; loola yemook bési màggalu Mburu mu amul lawiir.