Acts 13:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na ci mbooloom ñi gëm, mi nekk dëkku Ancos, ay yonent ak ay jàngalekat: maanaam Barnabas, Simeyon ku ñu dàkkentale Niseer, Lusiyus mi dëkk Siren, Manayen mi yaroondoo ak Erodd boroom diiwaan ba, ak Sool.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca biir mbooloom gëmkat, ña woon ca dëkk ba ñuy wax Àncos, amoon na ay yonent ak ay jànglekat: ñuy Barnaba, ak Simeyon mi ñu dippee Ñuule, ak Lusiyus mi bawoo Siren, ak Manayen mi yaroondoo ak Erodd boroom Galile, ak Sóol.